Serie - DIEGOU POUSSOU - Saison 1- Episode 22

Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
kharmedia_offic...
facebook
kharmedia_l'offi...

Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.

Commenti

  • Baye Niass Ndiaye
    Baye Niass Ndiaye8 giorni fa

    Face 2 face bi nékhna

  • Amina Thiam
    Amina Thiam29 giorni fa

    L'homme en rouge bimou deiffé cei lunettes Maître Gims rk lama diokh et Jl'aime pr ça 😍bilae😅😍

  • Coumba Diallo
    Coumba DialloMese fa

    🥰

  • Awa Touré
    Awa TouréMese fa

    No yirim bakhléléwo nite déye dioupe

  • Fanta
    FantaMese fa

    Tres abuses meme.. marriages qui sont des abuses tout court... du n importe quoi- quelle abuse, quelle stresse.. quelle tension aussi.. en tout cas...

  • Hitler Mbossé
    Hitler MbosséMese fa

    Ana goor you infidèle yii

  • Deguene Mbaye
    Deguene MbayeMese fa

    Gni la beugue daal

  • ndeye mboulé fall
    ndeye mboulé fallMese fa

    Asma é très belle ❤

  • ndeye astou niang leye
    ndeye astou niang leyeMese fa

    Asma bo amei gane doko dalale sogaa di wo sa borom keur nak vraiment je t'aime bien mais na scénariste bi di xolat li way

  • Dieyla Camara
    Dieyla CamaraMese fa

    Serie bo khamni salle bi neeg bi rek 😂

  • Gueye Mame diarra
    Gueye Mame diarraMese fa

    J'aime cette serie

  • Malick Mbaye
    Malick MbayeMese fa

    serie nawlé khana dafa fin

  • Ami Diop
    Ami DiopMese fa

    Yerim defal sa choix

  • Agnès ndour
    Agnès ndourMese fa

    Oh yerime jai vraiment pitier de toi

  • Kine Gueye
    Kine GueyeMese fa

    ❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • Mariama Kanouté
    Mariama KanoutéMese fa

    Sons bi svp wagnilenko c abusé

  • Nacy Samb
    Nacy SambMese fa

    Pourtant dafa rafet balegui sekeu fi rolou djekk bouy doundou lou meti la motakh

  • ngosse fall
    ngosse fallMese fa

    AY way beugg na numero ASMAA svp diapp leinn thi

  • Tamsir Thiaw
    Tamsir ThiawMese fa

    Djiguén gni séy lén ngén tarbiyou sén dieukeuryi Roy thii mame Diarra Bousso

  • Fatou mbacke Sylla

    Fatou mbacke Sylla

    Mese fa

    @toutou mania merci beaucoup

  • toutou mania

    toutou mania

    Mese fa

    Royal si mame mor Anta sally beu paré waleu si Seydina Mouhamed SAW

  • fadiengsaala dieng
    fadiengsaala diengMese fa

    Asma yu raféte lay sol té yiww guiss nané exposéwoul ay forman comme gni ko yenen di défé eleuk jarr na sorale🙏❤️

  • Diarra Mame
    Diarra MameMese fa

    Amsa est plus sans la purique

  • Rokhy Mane
    Rokhy ManeMese fa

    Khar media ana nawlé idda woudiou peethiorko surtout nawlé yegualiko bokk

  • Ndeye Kane
    Ndeye KaneMese fa

    Non yagui so ga am problème yirim

  • Grace
    GraceMese fa

    Khar media votre musique de fond est trop forte c'est à peine si on entend les dialogues. C'est épuisant soyez pro quand même. Wa salam

  • Mame diarra Diome
    Mame diarra DiomeMese fa

    👌

  • Alimatou Mbaye
    Alimatou MbayeMese fa

    Jose Carlos Alberto de Souza 🥰😋😘🤪

  • Sokhna maï Ndiaye
    Sokhna maï NdiayeMese fa

    No yérim sof na

  • Ahmadou cisse
    Ahmadou cisseMese fa

    Heeee yerm nak am nga blm

  • Ndeye Liza kalela
    Ndeye Liza kalelaMese fa

    Yérim bayil sa khétou babaté yi

  • sapa Diop
    sapa DiopMese fa

    Yala boul deglou yerim wakhoul degu torokhal jiguen lafi nekee

  • Badiéne Cissé
    Badiéne CisséMese fa

    Yérime bandiwo sakhe matar mie dinala sawe beuthiagou ndare kame ndiafe guisago dara akhe bakhoule

  • Touko Badiane
    Touko BadianeMese fa

    La femme de yerim barina wakh AK ladj vis à vis du soit disant ami de son mari Elle vient de le connaître kay n’a teye en plus elle est trop mou Bari manière 🤣🤣🤣🤣

  • Ahmadou cisse

    Ahmadou cisse

    Mese fa

    @Touko Badiane 😂😂😂😂

  • Touko Badiane

    Touko Badiane

    Mese fa

    @Ahmadou cisse 🤣🤣🤣🤣 do lenn demmm goor rekkk

  • Ahmadou cisse

    Ahmadou cisse

    Mese fa

    Mais c'est normale pcq yerim mot lolo😂😂😂😂

  • funstyleful
    funstylefulMese fa

    Il y a trop de musique dans cette série. En plus le son n’est pas équilibré. On entends plus la musique que la voix des acteurs.

  • Mya Thiam
    Mya ThiamMese fa

    Wa Ani nawle tamite

  • Abdou Diop
    Abdou DiopMese fa

    Dokh dou bayi yonam yerim li gneup yako tekk sa bop tu as joué avec sonia tu vas perdre asma

  • Fatou Tall
    Fatou TallMese fa

    Franchement se mec la en rouge ou orange ayway jle kiff trop avec sa barbe 🧔 sourire bi nak hooooo il y a des gens Beau nama yalla bal walll safoulay

  • fary mboup

    fary mboup

    Mese fa

    worigua😂

  • la lionne brome biir arene
    la lionne brome biir areneMese fa

    Nanguéneu fékhé ba nianou yirim nangou

  • Yanidou Dieye
    Yanidou DieyeMese fa

    Thieuy passé dina top nite ba si bamèl yirim damako moudié yeureume sakh

  • Almoujtaba TV ألمجتبا
    Almoujtaba TV ألمجتباMese fa

    Amsa bo dindé sa cheuveu bi ngay dak de

  • Elisabeth Marone
    Elisabeth MaroneMese fa

    musik binguéne di ték si guinaw nékhna way jadorrrr

  • fary mboup

    fary mboup

    Mese fa

    bi lan dan tek woudiou lethiorgo

  • Gnagna Diop
    Gnagna DiopMese fa

    Bilaye

  • Momy Gueye
    Momy GueyeMese fa

    Amiin

  • Momy Gueye
    Momy GueyeMese fa

    Légui Gooro yi nioy yakh seyi seni Domyi bilhay gni gnoo lakalé

  • Zahra Niass
    Zahra NiassMese fa

    Mais Matar t’as op besoin d’une 2e femme par hasard ahhhh beau nga daal😭😭😂❤️

  • Boufa Kebe
    Boufa KebeMese fa

    Et prtant yerim beugna changé sonia moko sonal rek neko tak par force bolesi yaye dji diko diapalé gnoukoy tekk dill lolou la

  • marema fall
    marema fallMese fa

    Wa yén wa khar média khana nawle da djiekh

  • Fanita Sidibe
    Fanita SidibeMese fa

    Oooooohhhhh Goro bakhoule me c lavi😏🤔

  • Mame Fansény NDOUR
    Mame Fansény NDOURMese fa

    Asma té très belle machallah 💓Fatma damala beugg bilay j'aurai aimé te rencontrer un jour bilay nak depuis senn serie regret ba tay tu m'espire❤️barki très srx ❤️🙏

  • Bineta Fatima Sow
    Bineta Fatima SowMese fa

    Yerim deflou lui bonne ak niaw bakhoul yaguini l passe attrape

  • Mbaye Fatou
    Mbaye FatouMese fa

    Machalla

  • diatta khady
    diatta khadyMese fa

    Yerim tamite beurigua problème

  • Aida Kebe
    Aida KebeMese fa

    Thiey guoor ma diomii maan daa melnii day wadia taak dé waaw bakh naa gnou deem rek

  • Layee Sylla
    Layee SyllaMese fa

    Non diabar diola beugue nga beugue ko nékh na lool Asma je t'aime

  • Thioro Faye
    Thioro FayeMese fa

    Baijy

  • Natou768
    Natou768Mese fa

    Wakh sa femme deugue guenoule yombou wiri wiri bi tamite doulabalati bénéne féneu deugue moye dieuque thé moye moudiou

  • Moise Endurant

    Moise Endurant

    Mese fa

    vous avez tout dit Mme

  • Nawal Boujbir
    Nawal BoujbirMese fa

    Gniari bandi yi nakh gniogui werante dee😂😂😂😂😂

  • yacine badji
    yacine badjiMese fa

    Amsa tu es plus belle sans ce péruque

  • Moise Endurant

    Moise Endurant

    Mese fa

    vraiment !!! il y a pas mieux une femme sans perruque... mais au Sénégal sans ça beaucoup d'hommes te regarde pas et c'est dommage..

  • Mame Fallu Comedien
    Mame Fallu ComedienMese fa

    Yaw mii yalla nga téki téral sa niarri wadiour🙏❤wakhal amine téi nga abonné téi yalla takh🙏❤

  • Jantal mara tv
    Jantal mara tvMese fa

    Ko beuge mo contenu après koor gui beuseul j'aime

  • coumba ndiaye
    coumba ndiayeMese fa

    Son bi svp deleneko wagni

  • Hadeejah Qubra
    Hadeejah QubraMese fa

    Ma guiss Mounirou sur la notif yakar ni NAWLÉ mo dikate nakaté yooo .BOBOU SERIE FOUM TOLLEU YEIN????

  • Elbou04 Officiel
    Elbou04 OfficielMese fa

    itwindow.info/door/video/p55kqcpz32HHl88.html

  • Wallyballagoseckes
    WallyballagoseckesMese fa

    Yayou malick bilahi dafma nekh goro boula amaloul ndiarigne dankoy baycoter jigueen mom bou seuya loul Goro rek amatoul sans seuy dou jeukeur kese wasalame nak

  • Maeva Diouf
    Maeva DioufMese fa

    Thiey yerim aka ndiongueee

  • amiena njie
    amiena njieMese fa

    They yerim mugui nekhal Asma deh 😂😂

  • Omar Diouf
    Omar DioufMese fa

    Boulene yakh seri bi vous étiez sur le bonne vois way

  • Fatima Diaw
    Fatima DiawMese fa

    Serie bo kham ni secanse yepou bene keur la

  • Deme Fatim

    Deme Fatim

    Mese fa

    Vraiment

  • ndeye mbacké

    ndeye mbacké

    Mese fa

    moma diakhal man

  • Sira Thiam
    Sira ThiamMese fa

    Yerim sa kawam gui yambar na😅

  • Adja Kiné Lam Mbaye
    Adja Kiné Lam MbayeMese fa

    Taaay leçon du jour bi moy « Darahhh diaroullll yakamtiii surtout seuyyy « Discussion entre asma et ndeya 👌

  • Penda Gueye

    Penda Gueye

    Mese fa

    Right

  • fary mboup

    fary mboup

    Mese fa

    bly aka lerr seuy deh diarul yakamti heur bouko yalla dogualè rk

  • yaram cisse

    yaram cisse

    Mese fa

    En tout cas khôl bou bakh figuay dougue

  • diop aby
    diop abyMese fa

    Wa yeen serie regret fou mou tolou.....

  • Ismaila Camara
    Ismaila CamaraMese fa

    Questo video e bellissimo 🥰🥰❤❤🤣🥰🥰🥰🥰🥰🥰

  • tata tata
    tata tataMese fa

    Sonia soi doit retrouver la-raison

  • bb chou
    bb chouMese fa

    Wa khar média lou takh yéne séne série yui bene keur rek guéne gnouye wone

  • Rejane Manga

    Rejane Manga

    Mese fa

    Bb chou moma diakhal

  • Vieux Bocar Guissé
    Vieux Bocar GuisséMese fa

    Kou guiss ni Ndeya si Regret la gueneu rafeter fi

  • Rokhy Mane

    Rokhy Mane

    Mese fa

    Moo fii mariage bii problème yii stress yii tamite Ax meunta djogoma tamite célibataire daa nexe déé liberté Kaaye âme 🤸🤸

  • amy ngom

    amy ngom

    Mese fa

    C vrai dafa pata

  • Mame yacine Diakhate

    Mame yacine Diakhate

    Mese fa

    Man dh fii lama dakhalé wakh deug psq dafee yiiw ta defko diap trop

  • Loway Déff Boppam

    Loway Déff Boppam

    Mese fa

    Koko vieux Série Nakhar boy ya ngui weur nak😃😃 wa Ndeya mom foufo la dakké

  • Mame bossou Saw

    Mame bossou Saw

    Mese fa

    Oui leigui dafa ñaaw

  • Assane Ndiaye
    Assane NdiayeMese fa

    J'adore cette série...🥰🥰🥰🥰👈👈👈

  • Amy colle Fall
    Amy colle FallMese fa

    Lolou dé tahul niouy Tage diabar

  • Ndiaye Soumare
    Ndiaye SoumareMese fa

    Moi je regarde cette série avec mon téléphone

  • Mer daba Ndiaye
    Mer daba NdiayeMese fa

    Ana gni beugue amsa beuse les j'aime tes abonnés way ❤️👍

  • Sokhna lat Lô

    Sokhna lat Lô

    Mese fa

    Ćest pad amsa śest asma

  • Cheikhouna Dia

    Cheikhouna Dia

    Mese fa

    ❤️💝👎👍💗💗

  • NOPE TV (Mohamed benzékry)
    NOPE TV (Mohamed benzékry)Mese fa

    Yerim foumala diap nala niouss deii 🙄

  • kane kane

    kane kane

    Mese fa

    😂😂😂😂😂😂

  • NOPE TV (Mohamed benzékry)

    NOPE TV (Mohamed benzékry)

    Mese fa

    @Oumy Sarr 🙄🙄🙄 nopma

  • Oumy Sarr

    Oumy Sarr

    Mese fa

    Iow yagui foné😂😂

  • NOPE TV (Mohamed benzékry)
    NOPE TV (Mohamed benzékry)Mese fa

    ASMA Dinama rey yeine 😭 akamako nope 🙄 saraxma mayma chance 😭 akamako nope 🙄

  • NOPE TV (Mohamed benzékry)

    NOPE TV (Mohamed benzékry)

    Mese fa

    @Oumy Sarr somay nope may bayi 😭😭😭😭😭nopma nguir yallah nopma🙄

  • Oumy Sarr

    Oumy Sarr

    Mese fa

    @NOPE TV (Mohamed benzékry) iow domosa bayi😭😅

  • NOPE TV (Mohamed benzékry)

    NOPE TV (Mohamed benzékry)

    Mese fa

    @Oumy Sarr malaraw soma nober rek ma bayi 😂

  • Oumy Sarr

    Oumy Sarr

    Mese fa

    Goor bo fébar bi namla😂😂😂

  • Fatou Gaye fall
    Fatou Gaye fallMese fa

    Ani fans sama yii manifestez vous

  • Kharitou Mamam
    Kharitou MamamMese fa

    Yerim déketer bandit bou convertirou gua

  • LAYE AWA NDIAYE
    LAYE AWA NDIAYEMese fa

    Mais son bi tamit amou fi place

  • Kharitou Mamam
    Kharitou MamamMese fa

    Seuyou Sénégal mo raw kharer Badr

  • mounasse dieng

    mounasse dieng

    Mese fa

    Bilaye

  • Kharitou Mamam

    Kharitou Mamam

    Mese fa

    @fary mboup Mani diambar deugue moy Seuy Sénégal

  • fary mboup

    fary mboup

    Mese fa

    dfa meti deh 😂niep si bir

  • Sokhna Thiaw
    Sokhna ThiawMese fa

    Team la team diègou pousso ❤❤

  • La lionne a son univers Univers

    La lionne a son univers Univers

    Mese fa

    Présidente suis là😂😂😂

  • OUSMANE ANNE

    OUSMANE ANNE

    Mese fa

    J suis la

  • wolof sunu.lakk❤️
    wolof sunu.lakk❤️Mese fa

    Lima diakhal kou né naan bb gnary liirrr la wala

  • DIAW FAYE Fall

    DIAW FAYE Fall

    Mese fa

    Cv

  • Sokhna Fatou Ndiaye

    Sokhna Fatou Ndiaye

    Mese fa

    No yaw bayil roubé

  • bassirou nd
    bassirou ndMese fa

    Seyou Senegal méttina lol bilay

  • Wallyballagoseckes

    Wallyballagoseckes

    Mese fa

    Seuyou islam rek la de

  • cheick oumar diop Lambji

    cheick oumar diop Lambji

    Mese fa

    Bilay khamo si dara sakh t lissi méti yeup meuno ko wakh sa dieukeur

  • beug baye Xaritou mamem
    beug baye Xaritou mamemMese fa

    Ay wAy music bi

  • Fatou Cissé
    Fatou CisséMese fa

    Serie bi néx na mais sons bi bolén KO wagné mou guene néx

  • N. Astou Dieng

    N. Astou Dieng

    Mese fa

    Bilae

  • Ndeye Fall
    Ndeye FallMese fa

    Waw Kaye tay mome tardewouma Lou bari

  • bad boy
    bad boyMese fa

    Couple yi délén xoulo ndakh dioubo ba 😂

  • Codou Thiam

    Codou Thiam

    Mese fa

    boys tè ngama masawou

  • bad boy

    bad boy

    Mese fa

    @Codou Thiam 🤦🏿‍♂️🤣🤣🤣

  • Codou Thiam

    Codou Thiam

    Mese fa

    @Maguète Leye balma 😂kokou nga xamni kay defantè moko geunal kay lek😝😛🤣

  • Ousseynou Ba

    Ousseynou Ba

    Mese fa

    @bad boy moy toul nioniou béne khoulo dh lanou koy deff😂masi kham darra

  • Deme Fatim

    Deme Fatim

    Mese fa

    Bilay bo amé kou rarou dou meussa togn day metty Déguay provoquer ba sonneu

  • Sokhna Ndiaye
    Sokhna NdiayeMese fa

    Asma yèrè olof nice na torop mai dèssi bolè ay robe ak ay toubay you bah tamit

  • Sokhna Ndiaye

    Sokhna Ndiaye

    Mese fa

    @Amina Diaw dego ba tay ma wah la momoul ay yerem dh serie la rek kou Nek am gua droit wah sa xalat

  • Amina Diaw

    Amina Diaw

    Mese fa

    Dou mo mom ay yérém louko nekh sol nak

  • Mamy Seck
    Mamy SeckMese fa

    Ana gni guemm ni yerim d'où takk sonia

  • Sokhna lat Lô

    Sokhna lat Lô

    Mese fa

    Mane guem nako

  • Fa Mb
    Fa MbMese fa

    Bilahi seye rek akameti

  • Raby Diop
    Raby DiopMese fa

    Thiey yerime akk 😂😂😂😂 nekhal bi rien que rèk pour takeu Sonia. Yerime entou cas tu est louche

  • Raby Diop

    Raby Diop

    Mese fa

    Waw

  • ndeye mbacké

    ndeye mbacké

    Mese fa

    pour takk Sonia khana

  • Ndeye Ndiaye
    Ndeye NdiayeMese fa

    Ayy asma so khamon lima kham diguan nopi gor bou tamou dokhane ak fén dou massa changer jamais

  • Ndeye Ndiaye

    Ndeye Ndiaye

    Mese fa

    @Thiate Diarra li kouko doundou rék moko mana kham ta gor bou mana fén infidél irresponsable djiguéne mounou ko changé ndakh ndokh dou bayi yonam

  • Thiate Diarra

    Thiate Diarra

    Mese fa

    Bilay waax ga deg goor bou tamou doxane ak feen xamna si dara me sante yalla rk lep yalla leral nako

  • Aminata Diop
    Aminata DiopMese fa

    Série bi Lou tax Dou Amme notification ta abonné na🤔

  • princesse Aicha Th

    princesse Aicha Th

    Mese fa

    Activitél closh bi🔔

  • Soda Leye

    Soda Leye

    Mese fa

    So dougué abonné daguay déf tout

  • Dior Sylla

    Dior Sylla

    Mese fa

    @Aminata Diop mandh démbeu notification bi rk la guiss sétan ko

  • Aminata Diop

    Aminata Diop

    Mese fa

    Dafa Amme foumou Gneuwé konne😂

  • Aminata Diop

    Aminata Diop

    Mese fa

    @Dior SyllaMandé masoumako guisse

  • mhd veridique
    mhd veridiqueMese fa

    Ki dafay wadja takeu sonia ki mooy dmrm deug 😂😂

  • fary mboup

    fary mboup

    Mese fa

    bly bouy doff ba tak ko dina roukh guèyndè😂😂😂

  • Khady Mbaye
    Khady MbayeMese fa

    Wa Nawlé mom fouguén ko dougeul 🤔

  • Maguette Sarr

    Maguette Sarr

    Mese fa

    Moma diaxal

  • Madjiguène Dieng

    Madjiguène Dieng

    Mese fa

    Bonne question baa koor gui commencer baa légui dafa mélné lou réér

  • fary mboup

    fary mboup

    Mese fa

    moma diakhal nameu nako dak

  • Oumane Ndiaye

    Oumane Ndiaye

    Mese fa

    Après ramadan peut-être

  • Dabizaa Gueye

    Dabizaa Gueye

    Mese fa

    @Daba Gueyemo diaxal niep toma😍

  • fadel infos
    fadel infosMese fa

    Ana niouko donne xar diegou poussou

Il prossimo